Bienvenue Invité Dans Le Forum De Tous Ceux Qui Aiment Le Sénégal !

Connecté en tant que Anonymous. Dernière visite le

Vous n'êtes pas connecté. Connectez-vous ou enregistrez-vous

Aller à la page : Précédente  1, 2, 3, 4, 5  Suivante

Poster un nouveau sujet  Répondre au sujet

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Aller en bas  Message [Page 4 sur 5]

Baabel


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Cochon
Gnii kay daniounioo yab rék, waayé bayyilééne rék. Té nak daniou saupe rék, ndax noonou lalééne niniouye waxéé nééxéé nak Ehey !

Séétlou naa ni sax fane yima déf Rabat ci biniouy doogaa nieuw fii, khaléyou djiguééne yi, ndiagamaare yiniou andaloone daal Embarassed daniou amoone thioffééle ci sama waxine bi Embarassed . Dafa lééne nééx, té Dakar tamite noonoulawoone, dinanioula toogne, dinanioula niaawal waayé douniou beugg nga noppi, daniouy déf lépp nguir ngay waxtaan ak nioom ndax sééne xoll di nééx, ndax dafa lééne di fattéli diamonoy "Bara Yeggoo" khamnga rék, dafay nééx.
Waayé mane moom souniouma toppé louma wakh niou diaaraate ci sou sama khol boné Evil or Very Mad rék ma weulbeutikou ci toubab bi, lakk toubab moom kénn mounouci khamméé fouma diogué Ehey !

Waayé bayyil rék, bouma gnibbissé Arab laay lakk sakh nak bénn yoone, thioow li nékk bénn Ehey !

Waayé thiakh bi yombana dé, séétaatal touti rék !

Khaaral ma guindila touti sax nguir yombalal la ko : danioukay déf ci Thiép Ehey !

Goorgoorloul touti !

-Présentez-vous ICI
-Comment avez-vous connu ce forum? ICI
-Amusez-Vous ! ICI

Fatim


Membre - V.I.P

Membre - V.I.P
Sexe:Féminin Lion Buffle
bissimilah

Baabel


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Cochon
Aythieu ci liguééy bi Ehey !

Loo indaalé tay fatim?

-Présentez-vous ICI
-Comment avez-vous connu ce forum? ICI
-Amusez-Vous ! ICI

Nemam


Membre - Modérateur

Membre - Modérateur
Sexe:Féminin Gémeaux Cochon
way thiam mandé sa thiakh bi xamagoumaka batay

wala nadio la

Quand passe la passion suis la là où elle t'améne, il vaut mieux la prendre au vol de peur qu'elle s'envole.

Baabel


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Cochon
hahaha haha naadio kay Ehey ! Bayyil tandouss bi waay !
Déédét dou naadio, kii leu.... scratch scratch , noumou touddeuti waaay.... scratch ..... scratch waaw Ehey kii .... euh...... scratch Soupamé
Waayé mane naa am tamit dima teureuléé thiakhe bi moodoul noonou Wink ! Diéém maa nandd touti rék, you bari damakoo fatté Sad !

Diokhéél bénéén thiakh ma khool bakham !

-Présentez-vous ICI
-Comment avez-vous connu ce forum? ICI
-Amusez-Vous ! ICI

Nemam


Membre - Modérateur

Membre - Modérateur
Sexe:Féminin Gémeaux Cochon
"Signe kaw signe souff" ?

Quand passe la passion suis la là où elle t'améne, il vaut mieux la prendre au vol de peur qu'elle s'envole.

Baabel


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Cochon
Ehey Rolling Eyes scratch scratch scratch Sakkète Rolling Eyes ?

-Présentez-vous ICI
-Comment avez-vous connu ce forum? ICI
-Amusez-Vous ! ICI

Nemam


Membre - Modérateur

Membre - Modérateur
Sexe:Féminin Gémeaux Cochon
Bravo

Quand passe la passion suis la là où elle t'améne, il vaut mieux la prendre au vol de peur qu'elle s'envole.

Fatim


Membre - V.I.P

Membre - V.I.P
Sexe:Féminin Lion Buffle
wa ma neuk dou guiss dara khana hum

Baabel


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Cochon
Waa ana waa mbokki fii nak?
Koufi nékk?
Démbb "niarfoukki touss"(20zeo) mingui doone khoul naane ci fii yepp danioufiy lakk wolof té kénn nangouwoula douggou fii nii wax fi dara sax.
Nééna danioo guénn xéét, boulééne ko nangou waay !! Aythieuléén ci baatou wolof yi !

-Présentez-vous ICI
-Comment avez-vous connu ce forum? ICI
-Amusez-Vous ! ICI

Absent


Membre - Expert

Membre - Expert
Sexe:Masculin Vierge Chèvre
guiss nga lima wax niogui kay deugueul.ay guén xét laniou.ba paré diniou ray ak ay wolof ci yénén béreup yi.

Nemam


Membre - Modérateur

Membre - Modérateur
Sexe:Féminin Gémeaux Cochon
mandé soumay bine wolof doumako tay koumaka beugeu baylo digua sonn ré té wakh deug nak lolou moy wané ni guéndou niou khét

Quand passe la passion suis la là où elle t'améne, il vaut mieux la prendre au vol de peur qu'elle s'envole.

Baabel


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Cochon
ré ! ré ! ré ! ré ! ré !
Wax deugg nak nemam finga tékk mbir mi deuggou neu ta kénn mounou ci dara. Ndax dafay wané ni nioungui sax ci sounouy aada ba léégui.
Waayé boo guissé ngoorsi di wax, kheuyneu niniouy bindéé wolof boobou lé mooko xawa tiiss.
Waayé loolou dou dara, gueum naani souniou doundeuléé roukhou bii rék bouci kanaméé léppeuy baax.
Ndax bouniou démoone ba tamme waxtaanou wolofi késsé yaakaar naa ni dinaniou moudié wara mana dioublou ci mbindd mi niko tééré yi digléé ci ndioubouk araf yi.

Neexouleu dinddi moom, fii yepp diotaayou waa Sunugaal la, daniouy yaatal niénééne gni rék waayé souniou diotaay la nak moom Ehey

-Présentez-vous ICI
-Comment avez-vous connu ce forum? ICI
-Amusez-Vous ! ICI

Nemam


Membre - Modérateur

Membre - Modérateur
Sexe:Féminin Gémeaux Cochon
thiay man souniou keurgui leund yi barénañ fi ré ré

Quand passe la passion suis la là où elle t'améne, il vaut mieux la prendre au vol de peur qu'elle s'envole.

Shatap


Membre - Paresseux

Membre - Paresseux
Sexe:Masculin
Waa fii loufi khéw?

Fatim


Membre - V.I.P

Membre - V.I.P
Sexe:Féminin Lion Buffle
lep mo fi khew

Thiamaass


Membre - Familiarisé

Membre - Familiarisé
Sexe:Masculin Vierge Rat
Kon boog, ñu yee waxtaanukaay wii xool ba xam di na ñu ko mana sùqqëli am deet Embarassed !

"Au Seuil De Ses Émeraudes, Mon Souffle Repose. Et Sur Son Eclantante Humeur Chaude, Mon Sourire Se Dépose."[THIAM Babel]

! Cliquez ICI Et Passez Votre Annonce !

Salamata


Membre - Chaud

Membre - Chaud
Sexe:Féminin Cancer Rat
Maa ngi ci biir. Xawma woon ne lii amna fii, moone di lakk saw lakk daraa daquko Ehey
() Dañ fii téré kufi lakk nasaraan wala ?

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Revenir en haut  Message [Page 4 sur 5]

Aller à la page : Précédente  1, 2, 3, 4, 5  Suivante

Poster un nouveau sujet  Répondre au sujet

Permission de ce forum:
Vous ne pouvez pas répondre aux sujets dans ce forum