1
Re: [PAGE PERSO] Secrets de famille: Le Blog des Célibataires! le Jeu 24 Juil 2008 - 14:15
tima
Membre - Familiarisé



kay athé niou fiiiiiiii
Connecté en tant que Anonymous. Dernière visite le
Vous n’êtes pas connecté. Connectez-vous ou enregistrez-vous
Aller à la page :
1 ... 28 ... 53, 54, 55 

kay athé niou fiiiiiiii

yaw tima bayil sagou, demb ba tay ya ngi gneuw si mane di djoy nane da nga nop momdofbi

ki moy seytanné deug .yow confrontation bi nguay bagne .mais tu vas voir.

mane dé ragalouma leu, bou dé sa wang bi mo takh nga fok ni meuneul nga sama djeukeur dara, bou yabo nga nopalou té kham ni lima yorako raw

té ngua dokhé ndank .bakhna dal

Touwa là va chercher un mari laa wax manNemam a écrit:oui timaaaaaaaa gawal diokhma tourendo waye comme Man Nit Ki mom bañ na

Pape LeGrand a écrit:Man moom pour jënd paquet manola, fallait que ma jaay sama tiket bus, daagu depuis le cinéma Liberté jusqu'à Delafosse.![]()
![]()

eh yaw baama amna mari dafa indisponible rek 

Nemam a écrit:eh yaw baama amna mari dafa indisposé rek
vaaaaaaaaaaaaaaaaaaa 
Pape LeGrand a écrit:Man moom pour jënd paquet manola, fallait que ma jaay sama tiket bus, daagu depuis le cinéma Liberté jusqu'à Delafosse.![]()
![]()

bilaye yaww yaa bonnnn 

ndeysane, lolou mo ko djap. dafa manqué vitamine bobou nonou ndakh indisposition djeukeur dji. thiam djapalé ko way yawitam 

Sama ablaye kay Mamy mi ngi ni jodd joddaaral taxaw, il suffit tout simplement à Némie d'effectuer quelques arrièrades pour venir s'ajuster autour.... je l'attends dé
! Y a du poobar et du jinjjeer tout autour aussi pour la safalattitude 
Pape LeGrand a écrit:Man moom pour jënd paquet manola, fallait que ma jaay sama tiket bus, daagu depuis le cinéma Liberté jusqu'à Delafosse.![]()
![]()

yaw mom mamy waxoumala indisposé sakh wayé à la retraite gua dieum nékal si tangal bi rek dina meussa diekh
Babel


Thiamaass a écrit:Sama ablaye kay Mamy mi ngi ni jodd joddaaral taxaw, il suffit tout simplement à Némie d'effectuer quelques arrièrades pour venir s'ajuster autour.... je l'attends dé! Y a du poobar et du jinjjeer tout autour aussi pour la safalattitude


Nemam a écrit:yaw mom mamy waxoumala indisposé sakh wayé à la retraite gua dieum nékal si tangal bi rek dina meussa diekh


lii si kanam rawouli gëtlyncx a écrit:Nemam a écrit:yaw mom mamy waxoumala indisposé sakh wayé à la retraite gua dieum nékal si tangal bi rek dina meussa diekh
Xanaa xamoo ni tangallbii, çà augmente de volume à mesure qu'on l'arrose? En plus Mamy est une très bonne jardinière!![]()
lyncx a écrit:N'épuise pas Thiam, cependant. Il a d'autres diri youmou wara iri.
est que yeug guani diri yoyou mamy si la bokk démal séti club anciens étudiants de maroc gni gui def lou dara diaroul 

Nemam a écrit:eh yaw baama amna mari dafa indisponible rek


Xanaa xamoo ni tangallbii, çà augmente de volume à mesure qu'on l'arrose?
lolou mome khamena ci dara .

Fatim a écrit:Nemam a écrit:eh yaw baama amna mari dafa indisponible rek
de fe dieul depar volontair
Aller à la page :
1 ... 28 ... 53, 54, 55 
Senediaspora.com :: SPORTS & CULTURES & DIVERTISSEMENTS :: Rencontres & Détente & Pause-Café » [PAGE PERSO] Secrets de famille: Le Blog des Célibataires!
Permission de ce forum:
Vous pouvez répondre aux sujets dans ce forum
| Fatim | |||||
| Baabel | |||||
| Nemam | |||||
| Hodei | |||||
| Damisco | |||||
| Sita | |||||
| Naginaa | |||||
| Thiamaass | |||||
| Modou | |||||
| Mamediarra |